Série - Diabarou Gorgui - "La femme du chef" -Episode 45

Cine y animación

Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
kharmedia_officiel?igshid=jf9h4pcgofsi
facebook
kharmedia_l'officiel
Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.

Comentarios

  • Fatou gueye
    Fatou gueyeHace 6 días

    Awo goor gui daf may ray 😂😂

  • chaton verma
    chaton vermaHace 10 días

    Non djeynaba elle est extraordinaire Elle joue bien son rôle wlhi

  • Fait Sall
    Fait SallHace 12 días

    Dieynaba dina dh😁😁

  • Hawa Anne
    Hawa AnneHace 16 días

    Dieynaba dafma nekh bilahi🤣🤣

  • Bougnaw TV
    Bougnaw TVHace 21 un día

    Dafa melni gnoun yi degueu bitim rew gnoun yolen gueneu degueu wolof. Li eupena!

  • Aissata Nguette
    Aissata NguetteHace 23 días

    Billahi Dieynaba mo niak personnalité

  • Cardiatou Ka
    Cardiatou KaHace 25 días

    Dieynaba elle est partout elle moy horom série biii

  • Ndeye Ndiaye
    Ndeye NdiayeHace 28 días

    Dieynaba vraiment kou manqui LA li mom ba diam leu

  • Assa Diop
    Assa DiopHace 29 días

    Aka ma bakh si awo you mel ni 😏😏

  • Saly Soumaré
    Saly SoumaréHace 29 días

    Il est immature ci rôle yi woudié diaroul yablou sa bopou

  • Soda cisse
    Soda cisseHace 29 días

    Ana gorgui

  • Natou768
    Natou768Hace un mes

    Dieynaba elle m’énerve vraiment sofena

  • Yasmina Babacar Sy Ndiaye
    Yasmina Babacar Sy NdiayeHace un mes

    Dieynaba mi waroul won bokou ak sama yaye tourr 😭trop de problème 😌

  • Rouguità Sall
    Rouguità SallHace un mes

    Hhhh mane mala fayoul😀😀

  • ASTOU SALL
    ASTOU SALLHace un mes

    Sethe bou bess khalé dafa ler dh😍😍😍Sadiya

  • Fatou Camara
    Fatou CamaraHace un mes

    Je suis d'accord avec toi ma sadiya ❤️❤️❤️❤️

  • Aby bathily
    Aby bathilyHace un mes

    Hé hé beugna dienaba deh thioum 😂

  • Saida aidara Dione
    Saida aidara DioneHace un mes

    tamba diameu sama degue tamite haa tata dieyenaba nak yaki togne mais nak sadiya méfie toi d’elle hummm bakhna

  • Saida aidara Dione
    Saida aidara DioneHace un mes

    dieynaba yow narga sonou deh tee doo nopalou guirr yallah tamite

  • Ndeye Liza kalela
    Ndeye Liza kalelaHace un mes

    Qui a remarqué que Sadiya est devenue plus belle après le mariage

  • Bintou Mané
    Bintou ManéHace un mes

    Sadiya dafa toubabé et bien coiffée c temps-ci

  • Khady Sall
    Khady SallHace un mes

    Awo bou niakeu fayda rék la bagn man

  • Penda Gueye
    Penda GueyeHace un mes

    No dieynaba com kou bok ak lamine samba 🤣🤣🤣

  • Penda Gueye
    Penda GueyeHace un mes

    Ma tarde dh🙄🙄🙄kouy aimé

  • Mignonne nana
    Mignonne nanaHace un mes

    La maman de manta et tata de sadiya elle se ressemble 😍😍

  • Mame diarra Diome
    Mame diarra DiomeHace un mes

    😢🙏🤭

  • Papa Ndiaye
    Papa NdiayeHace un mes

    💞💓💓💓💓💞💞💞💓💓💓💓💔💔💔💔💔💔💔💔

  • sainabou s mbye
    sainabou s mbyeHace un mes

    Amyra is very bad

  • Mame Bousso Mbacke
    Mame Bousso MbackeHace un mes

    « Mani degueu naleu man maaalaa fayoul »akh baaral bi..Sheu Djieynaba amoul.Elle m’a tué😂🤣Woudiou day doflo nite

  • Hawa Fall
    Hawa FallHace un mes

    Dieynaba😂😂😂😂😂😂😂

  • Bijou Ly
    Bijou LyHace un mes

    Wa djeynaba ni lako nara diapè moudj na meti 🤣🤣🤣🤣aka nara soneu !

  • Kane Kine
    Kane KineHace un mes

    Kane moy khale mah anta humm kii esceque elle n'est pas plus âge que sadiya mayi sadiya sa diabarou papa la ok

  • Tabara Gueye
    Tabara GueyeHace un mes

    Maih où est salif et oumaya

  • Ndiole Diouf
    Ndiole DioufHace un mes

    Ane oumaya

  • full fal
    full falHace un mes

    Djéynaba mi guène fook ni dofoule 😂

  • Amy ndione Ndour
    Amy ndione NdourHace un mes

    Dieynaba Aka woyadi tamite

  • mareme diop
    mareme diopHace un mes

    Filme bangi doga nekh nak

  • Ndeye rokhaya Diagne
    Ndeye rokhaya DiagneHace un mes

    Non bilaye nekhna trop machalla 🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🏳️🏳️🏳️🏳️🏳️🏳️🏳️

  • Awa Ndione
    Awa NdioneHace un mes

    Diaynaba weroule dafa dofe woudie doux dara bokou waresakhe la

  • Chimere Ndiaye
    Chimere NdiayeHace un mes

    Dieynaba gnakk nga classe ci awo diepy nala trop ngay boudeikou nonou melni serpent

  • Salamata Soumare
    Salamata SoumareHace un mes

    Lolene khame si awo bou âmoule fouleu

  • Fatou bintou Djitte
    Fatou bintou DjitteHace un mes

    Wa oumaya foumou fétté bokkk wala da bayyi

  • veronique mendy
    veronique mendyHace un mes

    Problème yagui Sogua commencé

  • veronique mendy
    veronique mendyHace un mes

    Problème yagui Sogua commencé

  • Fatou Niang
    Fatou NiangHace un mes

    Mais la traduction mom doyna war

  • Abi Kane
    Abi KaneHace un mes

    🕋🕋🕋🕋

  • Abi Kane

    Abi Kane

    Hace un mes

    Machala,♥️♥️♥️♥️♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • salihate bi
    salihate biHace un mes

    Mane tati copine la beugeu ndéké

  • salihate bi
    salihate biHace un mes

    Bilay arame mo soffff ta niake khorom

  • ndari ba
    ndari baHace un mes

    Sadya continu comme ça c'est pour gorgui lam

  • Ndeyfatou Guaye
    Ndeyfatou GuayeHace un mes

    Khadr média vous avez arrêté Belle Mère?

  • Oumouna kallssoum Faye
    Oumouna kallssoum FayeHace un mes

    Ayooo sén série bi mogui nekh niiii yalla nako thiate sékhlou😍💋

  • Bintou Doumbia

    Bintou Doumbia

    Hace un mes

    Cgt Bien

  • Rokhy Mane
    Rokhy ManeHace un mes

    Maa foknii goor bou âme nietel Niarel bii mooye méére wayé fii awo bii mooye méére rek 🤸🤸

  • Rokhy Mane
    Rokhy ManeHace un mes

    Ana oumaya xana daa outii ay bagage pour sadiya

  • yolande daba diagne
    yolande daba diagneHace un mes

    cinq minutes 41 secondes de pub, non mais s'est abusé sa

  • Betty Guisse
    Betty GuisseHace un mes

    Sadiya niak n'a kersa trop meunone n'a wakhé nénéne ak aram

  • Diaryatoulah Diop
    Diaryatoulah DiopHace un mes

    Dieynaba niakna fayda amoul ben classe bonjr dieynaba 😂😂😂 tata safi nexnama

  • Manga Manga
    Manga MangaHace un mes

    mane Dieynaba bilay réwna trop avec ses maniéres!!! elle me fait trop rire walay!

  • Bass Ndiaye
    Bass NdiayeHace un mes

    Dieynaba douma ray 🤣🤣🤣bonjour diéynaba mané dieynaba dégu nala wayé fayoula🤣🤣

  • Mame Diarra Ndiaye
    Mame Diarra NdiayeHace un mes

    Djeybana mo takh may sétane série bi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • Maya Siby

    Maya Siby

    Hace un mes

    Bilahi elle est trop drôle 😂

  • Aminata Diouf
    Aminata DioufHace un mes

    Li mom c'est trop 6mn de publication 🙄c'est à dire kilo publicité libatou série🙄

  • Philomene Yacine Fall
    Philomene Yacine FallHace un mes

    Khar media trop de publicitè ak tok film vraiment🙃

  • Sweety Queen Thiam
    Sweety Queen ThiamHace un mes

    Dieynaba ya matadi deugu. Yoro djiko awo deh. Amal dépassement touti rek stp.

  • Maimouna Dary
    Maimouna DaryHace un mes

    Je trouve je sadiya est égoïste, détruire la famille d’autrui pour pas que ta mère tombe malade. En plus elle est impolie

  • Mame Diarra Ndiaye
    Mame Diarra NdiayeHace un mes

    ..

  • Awa Laye Thiaw
    Awa Laye ThiawHace un mes

    Mane dh diégue bou niakké fayda ni dieynaba meusoumako guiss en plus niaréle moy défanté ak niétèl, xalass!!!

  • Astou Diop
    Astou DiopHace un mes

    Vous ne pensez pas que Diaynaba dou dof tmt

  • Fatou Cisse
    Fatou CisseHace un mes

    Héeee dienaba nakk bayilll waa tamba nakk nioune khamouniou heureumm walla ayy deff liguey you salté diko deff siii nitt yiii😒😒😒😒

  • Mbene Ndiaye
    Mbene NdiayeHace un mes

    6 minuti de pub 🤦‍♀️🤦‍♀️🤦‍♀️🤦‍♀️🤦‍♀️🤦‍♀️

  • Galou Dem
    Galou DemHace un mes

    Ndeyssane la 2ème femme de gorgui bena eurreur mouna yak leup machallah sadiya rewga legui ahhh djeinaba je t’aime bcp machallah nekhna trop

  • Marie Yandé Mbengue
    Marie Yandé MbengueHace un mes

    Djenaba môme mba ça va sof ga dal

  • Linguerou Bour
    Linguerou BourHace un mes

    Sadiya amnga tokk rew 😂 ‘Ta arame’ balma ‘Arame’

  • fille de sadio mané
    fille de sadio manéHace un mes

    Dieynaba yako faleiwoul😂😂😂😂😂

  • Bamba Touba
    Bamba ToubaHace un mes

    Mane djeynaba sof na dh melni kou amoul passé

  • Mya Thiam
    Mya ThiamHace un mes

    Delene changer nak bayiguene keur sadiya legui keur goorgui la ani oumaya salif etc......

  • Nafissatou Niang
    Nafissatou NiangHace un mes

    Solène wagniwone pub yi nak té yokou temps série bi kéneu doulene geune ish

  • Fasha Chon
    Fasha ChonHace un mes

    Djenaba sone neu 😂😂

  • Konté Ndseny
    Konté NdsenyHace un mes

    😂😂😂noo dieynaba soofna si awo amull béne calass waye 😂😂😂😂😂😂

  • ksa Kane
    ksa KaneHace un mes

    Mais la photo derrière Safi et dieynaba c Amy collé de regret da melni

  • Fatou Dia
    Fatou DiaHace un mes

    de tt les region disont oui tamba mosi eup bayre tjrs tamba tamba

  • Seck Awa
    Seck AwaHace un mes

    👌

  • ndeye mboulé fall
    ndeye mboulé fallHace un mes

    On réclame oumaya é salif😥

  • Salma counta
    Salma countaHace un mes

    Diaynaba way

  • diop lena
    diop lenaHace un mes

    Je suis désolée pour vos propos sur Tamba,aye niit tu bax,yu geume YALLAH 'niofa neek.

  • Papa Ndongo Cisse
    Papa Ndongo CisseHace un mes

    SADIYA MIGUI MAY BEUGEU SOF NAK DAFA COMMENCÉ DI YEG BOPAM

  • talibé bamba
    talibé bambaHace un mes

    Koumay diapalé si diéynaba gnou gnouss ko gnoussou commun sof nama trop manqué té gnakeu class beugatouma done awo ndakh mom thimmm😡😡😡 Nb: kilo publicité khadiou guénwal libeurou série tamite dougnouko cas ishh

  • Marieme Touré
    Marieme TouréHace un mes

    👂👂👈👈👍

  • Lala Diop
    Lala DiopHace un mes

    6mns 36de publicité c trop

  • Diakhoumba Badio
    Diakhoumba BadioHace un mes

    Wa Dialacoto kay léne wouyou Diénaba 😁

  • Ndour Fallou
    Ndour FallouHace un mes

    Sén pub yi beurina way🤦

  • Léna SY
    Léna SYHace un mes

    Bon meune ngene avancer be 6.45s Les pubs😥😥😥😭

  • Bintou Doumbia

    Bintou Doumbia

    Hace un mes

    Cc

  • Soda Nguer
    Soda NguerHace un mes

    Oumaya foumou nekh ak salif tamite

  • Bocar Diallo
    Bocar DialloHace un mes

    Non vraiment Dienaba elle me fait rire je l'aime beaucoup elle joue bien son rôle

  • Diama Sall diop
    Diama Sall diopHace un mes

    Sadiya elle commence à changé ds tiit Nassi dall

  • moutolia andréa sambou
    moutolia andréa sambouHace un mes

    Bonjour Dienaba rekk momay fan🤣🤣😂🤣😂

  • Soda Sambe
    Soda SambeHace un mes

    Me ani oumaya

  • Maïmouna Sow
    Maïmouna SowHace un mes

    Ayway ana pendista geudjnako guiss mouy commentaires yi❤❤❤

  • Khady Diouf
    Khady DioufHace un mes

    Ms temps yi mome ni guene def baxna serie normal na wayé Def tay xar moi sogua guene wate ç bien j aime de serie

  • Awa Mbodj
    Awa MbodjHace un mes

    Tay diay n'a ba moayé

  • Fatoukine Sene
    Fatoukine SeneHace un mes

    Bale lene ma akh bale na lene yalla nanou yalla boule bale

  • Anta Diop
    Anta DiopHace un mes

    Awabi sike ne déé

  • Anta Diop

    Anta Diop

    Hace un mes

    Bilay

Siguiente